SERIGNE SALIOU CONTRE LA VIOLENCE
« Serigne Touba bi miy dem ci géedj gui àndoul ak kénn. Bi miy delsi àndoul ak kénn. Te lam fa wara def yépp def na ko. Lam fa wara dieulé lépp dieuli na ko. Bou niou tooguée ba neugeuni nag sokhlay taaloubé yi beugga dieum ci di ko khoulool ak di ko kheekhal. Man de souma sagnoon seen (yitté) dou dieum ci loolou.
Li [Serigne Touba] wéesu yépp yakhouwoul té kénn meussou ko thiee dimbali. Moo defal boppam lépp. Su ngeen tooguee ba neugeuni toppoum, khél défé né war ngeen koo kheekhal wala war ngeen koo khoulool it. Man de loolou àndou ma thia.
Diangue khassidaam yii ak diangue Alkhouraan ak topp ndigeulam. Man dé loolou laa beugg. [Serigne Touba] lim wéesu yépp kénn meussou koo yakh te kénn meussou koo dimbeuli, lépp moo ko defal boppam. […]
Wakh yi meussou fee diog, khass yi meussou fee diog. Loolee nag (khoulool ko ak kheekhal ko) bu doon lu am ndiarign la, da nagn ci doon fékk Cheikh Ibra Fall mou daa ko def, […], Cheikh Ibra Sarr, Cheikh Massamba Diop, ak nioom niooniou niépp, kou nékk am thia thieur, kou né am thia ngoora. […] Ak teewam yitam (moom Serigne Touba) kénn meussou thiee dieum […] Lou waay mana dégg da ngay bàyyee ak moom rek. Défar na ba lépp (diag) te dara yàkhou wou thi. […]
Yéené diou waay am daal na ko dieumé ci topp ndigeulam ak diangue Alkhouraan. Khassida yii niou baril diangue mi. Lou bari-bari dou eupp. Alkhouraan dji lou waay man na ko thiy def. Te bagna déglou lou niaaw, bagn koy déglé. Bagn koy déglou, bagn koy déglé.
Man dé di défal Serigne Touba loo xam né digeulou niou ko woon, man dé loolou sama khél dalou thi. […..]
Topp ndigeulou Serigne Touba te bagn koy kheekhal bagn koy khoulool daal tey topp ndigeulam daal moo ma geuneul. Thi laa nékk te kou may déglou maa ngi lay digueul nga def loolou. Loolou daal mooy fi ma nékk, té beugg kou ko man nga fékk ma fa.
Di liggéeyal Serigne Touba te bagna topp ci louy yakh. »
---------------------
Personne n'assista Serigne Touba dans son combat [à part son Seigneur] et il n'invoqua personne [si ce n'est Dieu] pour l'y aider. Il mena ce combat tout seul [et en dehors de toute sollicitation d'intervention belliqueuse de ses partisans].
Ainsi, lorsque le Cheikh fut envoyé en exil, il n'eut personne pour l'aider dans cette épreuve. Il en revint également sans être accompagné par qui que ce soit. Cela ne l'empêcha pourtant pas d'accomplir tout seul, durant ces longues années d'exil, tout ce qu'il devait y accomplir. Cela ne l'empêcha pas non plus d'y obtenir, tout seul, des faveurs à profusion. Si, après tout ceci, l'ambition de ses disciples d'aujourd'hui s'oriente vers les querelles et les batailles [physiques] en son nom, [qu'ils sachent que cela ne correspond nullement à sa propre démarche et à ses enseignements]. C'est pourquoi je souhaiterais que vos objectifs ne s'orientent point vers cette voie [sans issue]?
S'il faut absolument dépenser de l'énergie dans un « combat » au nom de Serigne Touba, dépensons-la dans la lecture de ses qasidas et dans la récitation du Coran. Consacrons cette volonté belliqueuse dans la « bataille » de l'observance de ses recommandations et celle de l'abstention envers ses interdits.
Quant au Cheikh, il sait parfaitement se prendre lui-même en charge. La preuve en est que, jusqu'à nos jours, sans l'aide de personne [à part son Seigneur], nul n'a encore réussi à altérer son héritage. Si donc vous, ses disciples, attendez aujourd'hui pour suivre certaines conceptions rationnelles erronées et pour vous engager dans des disputes et querelles stériles, sachez que ce ne sera nullement avec mon consentement.
Souvenez-vous que les propos calomnieux et offensants [envers le Mouridisme] ont toujours existé [ceci, depuis sa fondation même]. Mais s'il était avéré que les réactions violentes envers les auteurs de ces attaques étaient utiles [et étaient agréées par le Cheikh], nul doute que l'on aurait vu s'y engager hardiment ses illustres disciples que sont Cheikh Ibrahima Fall, Cheikh Ibra Sarr Ndiagne, Cheikh Massamba Diop Sahm, et tous leurs autres valeureux compagnons. Pourtant, du temps de Serigne Touba, nul d'entre ces vaillants épigones ne s'est jamais aventuré dans cette voie [des représailles].
En conséquence, je vous exhorte, chers condisciples, de concentrer vos énergies et toute votre détermination, non pas à ces vaines polémiques, mais à suivre scrupuleusement les recommandations de Serigne Touba, à la lecture fréquente du Coran (autant qu'il vous est possible de le lire) et à la récitation assidue de ses poèmes (aucune quantité de qasidas n'étant de trop). Tout ceci, sans prêter l'oreille au mal et sans le propager. Ne pas l'écouter, ni le faire écouter.
Mon option personnelle consiste ainsi, sachez-le, à m'abstenir de toute dispute ou querelle au nom de Serigne Touba. Elle consiste plutôt à me consacrer résolument à exécuter ses recommandations. C'est l'attitude que je me suis toujours évertué d'observer et que je conseille à tous ceux qui consentent à m'obéir à imiter. Consacrons-nous donc entièrement au Service de Serigne Touba et à ne jamais céder aux germes du mal et de la division... »

[Aziz Mbacke Majalis]
L’image contient peut-être : une personne ou plus

Enregistrer un commentaire

 
Top