BISOUB AL JOUMOUHA MOOY BISS BI GEUNE CI BISS YI .
CI LA YALLA BIND SOUNOU MAM ADAMA , THILAKO DOUGALE WON AL JANNA , THILAKO GUENNEE WONIT AL JANNA , CI BISOUB AL JOUMOUHA YIT CI LA ADDOUNA DI TOUKKI .
AMNA CI BISOUB AL JOUMOUHA WAKHTOU WO KHAMNE WAKHTOUW NANGOU NIAAN LA .
AK WOUTE AM NAK CI WANN WAKHTOULA , BATAKH NIOU BEUGUE KOU FARLOU CI BISS BI YEPP NGUIR MANA DADIEEK MOOM .

MOU AM AY TEGGUINE NAK YOU NIOU SOPP LOOL CI BISS BI LOU MELNI :
1 - SANGOU BA SET NI NIOUY SANGO FARATA TA YENE THIA SOUNNASS AL JOUMOUHA ,
2 - SOL YERE YOU SET , YOU WEEKH NAK MO THIA GEUNN SOU MANEE AM .
3 - LAL PARFUM BOU NEKH SOU DIAPPANDEE .
4 - DOKH AK SA TANK BO SORIWOUL JOUMA JA , DOKH BOU ANDAK DAL AK WEGOU .
5 - BO AKSEE CA JOUMA JA NGA JIITAL SA TANK NDAY DIOR BOOY DOUGUE WAKH LII :

( BISS MILLLAH , ALLAHOUMMA SALLI HALA SAYYIDINA WA MAWLANA MOUHAMMAD , ALLAHOUMMAFTAH LII ABWABA RAHMATIK ) .
6 - MOYTOU DI DIEGGAT NIT GNI AK DI DOKH CI KANAM KOUY JOULLI ,
7 - MOYTO DI JOULLI CI DIGEUNTE YARI KENO , LOUDOUL NGA KHAMNE JOUMA JA DAFA FEESS AK LAKO WEUR TA AMO FENEEN ,
8 - DEM BA SEUSS THIA SAPPE SA TA BAGNKO DEUNGAL , BAGNA BER SA SAPPESS BOPP TA FEK SAPPE SALA JITOU FEESAGOUL , BALANGA TOOK JOULLIL NIARI RAKKA NOUYOKO JOUMA JA , SOULA NEEKHEE YAM THIA , SOULA SOBEE YIT MANN NGA JOULLIWAT LOULA SOOB BA IMAM DI NIEUW ,
9 - SOU IMAM NIEUWEE NGA BAYYI LEPPOU LODOON DEF MO KHAM AY JANGUE LA WALLA LOUM MANA DOON TA DIGLOUKO , NDAKH WAKH CI BIIR KHOUTBA BI DAFAY YAKH JOULLI , BOUL WAKH WALLA NGAY DEF LOU DOUL DIGLOU IMAM DOONTENE KHAMO SAKH LAMOUY WAKH ,
10 - SOU IMAM SEULMALEE BOOY GUENN NGA JIITAL SA TANK THIAMMOOY WAKH LII :

( ALLAHOUMMA SALLI HALA SAYYIDINA WA MAWLANA MOUHAMMAD , ALLAHOUMMAFTAH LII ABWABA FADLIK ) .
YII YENN LATHI TEGGUINE YI GNOU SOPP CI BISOUB AL JOUMOUHA .
YALNANOU YALLA NANGOUL SOUNOUY DIAMOU TA DEFALNOU PAJOUK HAJO FII CI ADDOUNA AK EULLEUK YAWMAL KHIYAM CI BARKEB SERIGNE TOUBA - رضي الله تعالى عنه وأرضاه - AMIINE .

SERIGNE TOUBA - رضي الله عنه وأرضاه - DANA WAKHNE :
KOU BEUGUE DIB SANGUE , DANGAY NANGOO NEKKAB
DIAAM .
DIAAM .
KOU BEUGUE DIB SERIGNE DANGAY NANGOO NEKKAB
TALOUBE .
TALOUBE .
LOU WAAY YOR ATTANN KOO JOKHE NGUIR YALLA ,
FOO GUEESTOO GUISS KOULAKO ATTANA JOKH NGUIR YALLA .

LOU WAAY YOR ATTANOUKOO JOKHE NGUIR YALLA ,
BOU WEUROON ADDOUNA BAMOU DADJ DOU GUISS
KOUKO ATTANA JOKH .

KOUNE KOUMA TOPPOU MA DEM ,
KOUMA TOPPOUL MA DEM ,
FOO GUEESTOO GUISS MBOLOO SA GUINNAW .
KOUMA TOPPOUL MA DEM ,
FOO GUEESTOO GUISS MBOLOO SA GUINNAW .
( mingui bayyikoo ci : cheikh abdoul ahad mbacke )
( publié par / Cheikhouna diatara )
DIEULENA CI BAAY SERIGNE DIATARA , MOU DIEULE CI
SERIGNE MAHMOUDANN TOURE , MOU DIEULE CI
SERIGNE TOUBA - رضي الله عنه وأرضاه - MOU WAKHNE :
BOUR BOUY FAY YEENE DIAFEWOULA DIAMOU .
WAAYE BOUR DOU FAY YEENE TA AK MANN DESS FA .
( publié par / Cheikhouna diatara )
SERIGNE MAHMOUDANN TOURE , MOU DIEULE CI
SERIGNE TOUBA - رضي الله عنه وأرضاه - MOU WAKHNE :
BOUR BOUY FAY YEENE DIAFEWOULA DIAMOU .
WAAYE BOUR DOU FAY YEENE TA AK MANN DESS FA .
( publié par / Cheikhouna diatara )
YONENT BI - صلى الله عليه وآله وسلم - NEENA :
( JOULLIT BOU NE AMEEL NA MBOKKOUM JOULLITAM
DIOUROOM BENNI HAKH :
1 - SAYOU DADIEEK MOOM NOUYOUKO ,
2 - SOUKO VOYEE , MOU WOUYOUKO ,
( LOU MELNI MOU YEUGEULKO AK THIEET )
3 - SOU SAKKOO CI MOOM LAYE BIIR , MOU LAYEKO BIIR ,
4 - SOU TISSOOLEE WAKH : AL HAMDOU LILLAH ,
MOUNEKO : YARHAMOUKALLAH
MOOM MI TISSOLI WAKHAAT :
YAKHFIROUL - LAHOU LANA WA LAKOUM .
WALLA MOUNE :
YEUHDIIKOUMOUL - LAHOU WA YOUSLIHOU
BAALAKOUM ,
5 - SOU WEREUDEE MOU SEETIKO ,
6 - SOU FATOO MOU TAKHAWOUKO BAGN DOUGEUKO
CI BAMMEELAM .

DAFA MASA AM KOU NIEUW BISS CI SERIGNE BI NEKO :
MANDEY MBACKE DAMA DIAKHLE .
SERIGNE BI NEKO DIAKHLE YAR :
SOULA ADDOUNA DIAKHALEE DEMAL LAGGUEE YI ,
SOULA ALLAKHIRA DIAKHALEE DEMAL DIAMOUJI YALLA ,
DIAKHLEK ADDOUNA GOU LAGGUEEY MEUNTA FADJ KHAMOUNOUKO ,
SERIGNE TOUBA - رضي الله تعلى عنه - DANA WAKHNE :
DIOUROOM YII , BOUGN KHAM SEEN DIOUROOM :
1- SEENI WAY DIOUR BOUGN KHAM SEENOUK NAKHARI DERET ,
2- SEENOUK NDIABOOT BOUGN KHAM SEENOUK NAY ,
3- WAKHTOUY DIOULLI YI BOUGN KHAM SEENI YITTE ,
4- SEENI BARABOU LAGUEEYOUKAAY BOUGN KHAM SEENOUK TAYEL ,
BOKNA CI WAKHI SERIGNE TOUBA- رضي الله تعالى عنه - MOUNE :
DIOUBONAMAK SAMA BOROOM CI YATT , DIOUBOOK SAMAY MOROOM CI YATT :
DIOUBONAMAK SAMA BOROOM CI :
LOUM MA DIGEUL MA DEFKO ,
LOUM MA TERE MA BAYYIKO ,
LOUM DOGAL MOU NEEKH MA BIIR AK BITTI .
DIOUBONAMAK SAMAY MOROOM CI :
DOUMA CI TOOGN KENN ,
TA KOUMA CI TOOGN MA DIEGGEUL LA NGUIR YALLA ,
( JOULLIT BOU NE AMEEL NA MBOKKOUM JOULLITAM
DIOUROOM BENNI HAKH :
1 - SAYOU DADIEEK MOOM NOUYOUKO ,
2 - SOUKO VOYEE , MOU WOUYOUKO ,
( LOU MELNI MOU YEUGEULKO AK THIEET )
3 - SOU SAKKOO CI MOOM LAYE BIIR , MOU LAYEKO BIIR ,
4 - SOU TISSOOLEE WAKH : AL HAMDOU LILLAH ,
MOUNEKO : YARHAMOUKALLAH
MOOM MI TISSOLI WAKHAAT :
YAKHFIROUL - LAHOU LANA WA LAKOUM .
WALLA MOUNE :
YEUHDIIKOUMOUL - LAHOU WA YOUSLIHOU
BAALAKOUM ,
5 - SOU WEREUDEE MOU SEETIKO ,
6 - SOU FATOO MOU TAKHAWOUKO BAGN DOUGEUKO
CI BAMMEELAM .
SERIGNE MALICK BASINE SY - رضي الله عنه - DAANA FIRI BATOUB KILIFA MOUNE :
KILIFA MOOY KILEE FIY FADJ .
KILIFA MOOY KILEE FIY FADJ .
DIEULENA CI SERIGNE CHEIKH FALL TEERE ,
MOU DIEULE CI SERIGNE ABDOULLAHI LO NODDOUKAT
MOU WAKHNE :
DAFA MASA NOUYOU SERIGNE TOUBA - رضي الله عنه وأرضاه -
DIEBBALKO TOOL BOUMKO BAYALOON .
SERIGNE BI NEKO :
ABDOULLAHI MBA BOKKOO CI GNIMAY KHASLOU ?
NEE MANE THIELL .
MOUNE :
KHAMNGA LOUY KHASS LOUMA ?
MOOY WAKHNE FIMANN NGA BAYYIKOO ,
TA NEKKOO CI LIMA NEKK .
MOU DIEULE CI SERIGNE ABDOULLAHI LO NODDOUKAT
MOU WAKHNE :
DAFA MASA NOUYOU SERIGNE TOUBA - رضي الله عنه وأرضاه -
DIEBBALKO TOOL BOUMKO BAYALOON .
SERIGNE BI NEKO :
ABDOULLAHI MBA BOKKOO CI GNIMAY KHASLOU ?
NEE MANE THIELL .
MOUNE :
KHAMNGA LOUY KHASS LOUMA ?
MOOY WAKHNE FIMANN NGA BAYYIKOO ,
TA NEKKOO CI LIMA NEKK .
SERIGNE TOUBA - رضي الله عنه وأرضاه - DANA WAKHNE :
DIOUROOM YII , BOUGN KHAM SEEN DIOUROOM :
1 - SEENI WAY DIOUR BOUGN KHAM SEENOUK
NAKHRI DERET ,
2 - SEENOUK NDIABOOT BOUGN KHAM SEENOUK NAY ,
3 - WAKHTOUY JOULLI YI , BOUGN KHAM SEENI YITTE ,
4 - SEENI BARABOU LIGUEEYI KAAY BOUGN KHAM
SEENOUK TAYEL ,
5 - SEENI DEUKKANDOO , BOUGN KHAM SEENOUK
NIAAWI TEGGUINE .

LII MOOY KHAMLE WAKHTOUY DIAPPOU YI
AK WAKHTOUY DOG YI CI TOUBA AK LIKO WEUR TOLLOU CI 100 KM CI NDAY DIOR AK THIAMMOOY
27 KM CI PENG KOU AK CI SOWOU .
************************** ************************** *****************
SERIGNE SIDY BOUSO MOM SERIGNE MAWLAY MOU SERIGNE MBACKE BOUSO , MOKO GUIENNE .
حفظه الله ورعاه وجزاه عن الإسلام خيرا بأحسن الجزاء .
AK WAKHTOUY DOG YI CI TOUBA AK LIKO WEUR TOLLOU CI 100 KM CI NDAY DIOR AK THIAMMOOY
27 KM CI PENG KOU AK CI SOWOU .
**************************
SERIGNE SIDY BOUSO MOM SERIGNE MAWLAY MOU SERIGNE MBACKE BOUSO , MOKO GUIENNE .
حفظه الله ورعاه وجزاه عن الإسلام خيرا بأحسن الجزاء .
GEUM SOUNOU BOROOM YOMBOUNA ,
WAYE LOUMOU DOGAL MOU NEEKH LA MO DIAFE
( MAME THIERNO IBRAHIMA FATY )
WAYE LOUMOU DOGAL MOU NEEKH LA MO DIAFE
( MAME THIERNO IBRAHIMA FATY )
SERIGNE MOR KHADI SY - رضي الله عنه - DANA WAKHNE :
BOUL ROY BOROMOUK MAY ,
BOUL ROY BOROMOUK MOY .
BO ROYEE BOROMOUK MAY , MOU FEEY NGA DIIK BO ROYEE BOROMOUK MOY BOUGNKOY DOUMA DOUMA WALE LA .
BOUL ROY BOROMOUK MAY ,
BOUL ROY BOROMOUK MOY .
BO ROYEE BOROMOUK MAY , MOU FEEY NGA DIIK BO ROYEE BOROMOUK MOY BOUGNKOY DOUMA DOUMA WALE LA .
MANDEY MBACKE DAMA DIAKHLE .
SERIGNE BI NEKO DIAKHLE YAR :
SOULA ADDOUNA DIAKHALEE DEMAL LAGGUEE YI ,
SOULA ALLAKHIRA DIAKHALEE DEMAL DIAMOUJI YALLA ,
DIAKHLEK ADDOUNA GOU LAGGUEEY MEUNTA FADJ KHAMOUNOUKO ,
DIAKHLEK ALLAKHIRA GOU DIAMOU YALLA MEUNTA FADJ KHAMOUNOUKO , WASSALAM .
DIOUROOM YII , BOUGN KHAM SEEN DIOUROOM :
1- SEENI WAY DIOUR BOUGN KHAM SEENOUK NAKHARI DERET ,
2- SEENOUK NDIABOOT BOUGN KHAM SEENOUK NAY ,
3- WAKHTOUY DIOULLI YI BOUGN KHAM SEENI YITTE ,
4- SEENI BARABOU LAGUEEYOUKAAY BOUGN KHAM SEENOUK TAYEL ,
5- SEENI DEUKKANDO BOUGN KHAM SEENOUK NIAWI TEGGUINE .
DIOUBONAMAK SAMA BOROOM CI YATT , DIOUBOOK SAMAY MOROOM CI YATT :
DIOUBONAMAK SAMA BOROOM CI :
LOUM MA DIGEUL MA DEFKO ,
LOUM MA TERE MA BAYYIKO ,
LOUM DOGAL MOU NEEKH MA BIIR AK BITTI .
DIOUBONAMAK SAMAY MOROOM CI :
DOUMA CI TOOGN KENN ,
TA KOUMA CI TOOGN MA DIEGGEUL LA NGUIR YALLA ,
TA LOUMA AM NIOUBOKKOUKO
BOKNA CI WAKHI SERIGNE TOUBA-رضي الله تعالى عنه-
MOUNE :
ADDOUNA , AK JIGUEEN , AK TAKNDEER
NIO YAM .
LO CI DAKH DOKO DIOT ,
LO CI WANN GANNAW DOKO RAW
MOUNE :
ADDOUNA , AK JIGUEEN , AK TAKNDEER
NIO YAM .
LO CI DAKH DOKO DIOT ,
LO CI WANN GANNAW DOKO RAW
SERIGNE TOUBA - رضي الله تعالى عنه - MASNA FIRI NIATTI BATI WOLOF YII MOUY :
FOULLA , FAYDA , FARLOU . MOUNE :
FARLOU MOOY :
LOSORI SORI CI MBIR , FOUTHIA LOUBAKH YAM NGA YAMFA .
FAYDA MOOY :
LOTAMBOULE NGUIR YALLA , NANGA YAMALE NEKTHIA YAW KENN AK ADDOUNA SEPP FEKLATHIA .
FARLOU MOOY :
LINGAY DEF NGA SAKKALKO WAKHTOU WOKHAMNE BOUDIOTEE , LODIAPPOON NGA BAYYIKO NGUIR DEFI LOLA .

SERIGNE TOUBA - رضي الله تعالى عنه - MASNA WAKH BISS SERIGNE MBACKE BOUSO NEKO :
DIOULLIT BOU BOLEE DIOUROOM YEENT YII MOUCC CI ADDOUNA AK ALLAKHIRA :
RAGAL YALLA ,
RAGAL KOU RAGAL YALLA ,
RAGAL KOU RAGALOUL YALLA ,
BAYYI LOUBONN ,
BAYYI KOUBONN ,
BAYYI FOUBONN ,
LOUM KHAMOUL BOUMKO WAKH ,
LOUM MANOUL BOUMKO DEF ,
LOUM MOMOUL MOU MANDOU CA

SERIGNE FADILOU MBACKE - رضي الله عنه - DANA WAKHNE :
AND YARAKOY YAKH :
TEGUE LOU MANEEFOUL , AK GANTOU LOU MANEEF .
####################
LOLOU MOOY :
NGA TEK NIT LOUMOU MANOUL .
MOKHAM SA KHARITLA WALLA KOUMOU MANA DOON .
WALLA NIOU SAKKOU CI YAW LO MANN BANOPPI NGA GANTOU .
YAR YII YEPP DAY DAY YAKH AND

SERIGNE MODOU KHADI SY , DI DOOM CI SERIGNE
MALICK BASINE SY - رضي الله عنهما - DANA WAKHNE :
MACK MOU DAGNOUCK RER AMOUB RAIR , KOUKO GEUNA DIOUB REKKAKOY YILIF .
KOUMELNONOU NAK SAYOKO DIEULEE SEUSEULEKO CI SA DIEUMMOU YAAR LAY SEKHACK YAW :
MATNA DEF AK APPOUNA DEF .
WAYE MACK MOU DAGNOULOUCK RER AMOULOUB RAIR , SAYOKO DIEULEE SEUSEULEKO
CI SA DIEUMMOU MOMIT YAAR LAY SEKHACK YAW :
MANN NGAKO AK SAGN NGAKO

SERIGNE TOUBA - رضي الله تعالى عنه وأرضاه - DANA WAKHNE :
SOUNGUEEN KHEUYEUTEE NANGUEEN DEF SEEN NAKHAR MOUY SEEN BANNEEKH ,
DEF SEEN THIONO MOUY SEEN NOFLAAY .
SOUNGUEEN KHEUYEUTEE NANGUEEN JIITAL DIAMOU YALLA TEKTHIA LAGUEEY ,
TAY WETTALIKO TOPP NDIGALI YALLA YI BAGNA WETTALIKO DIEUMMOU .
TADEF TOPP NDIGALI YALLA YI MOUY AB SERIGNE , BAGNA DEF AW SANTE MOUY AB SERIGNE .
KOUBEUGA TEDD FII CI ADDOUNA DANGAY NANGO LAGUEEY ,
KOUBEUGA TEKHE CA ALLAKHIRA DANGAY NANGO DIAMOU YALLA .

SERIGNE TOUBA - رضي الله تعالى عنه وأرضاه - MASNA WAKH BISS DOMAM SOKHNA FATY DIA NEKO :
MBA NIT GNI DOUGN DOKH SA DIGGEUNTEEK SA BOROOM ?
KO MEUNTA DIAMOULO YALLA BOULKO DIG AL JANNA ,
KO MEUNTA LAGUEEYLO BOULKO DIG TERANGA
KO MANALOUL DARA FII NANGUEEN TEELA BAYYENTE , BALA NGUEENA DEM FEULE EULLEUK MOUDILA LEUDIEUL .

Enregistrer un commentaire